Articles

Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar

Image
Iniwersite Gaston Berger Bu Ndar   Iniwersite Gaston Berger  mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu  Ndar  ci réewum  Senegaal .   Iniwersite Gaston Berg er mooy Daara ju kawe ji nekk diwaanu Ndar ci réewum Senegaal. Tëraliin    1             Démb 2             Ràññeefi barab 3             Bërëbu tàggat ak gëstu 3.1          Ladab ak xam-xamu nekkinu doomu àddama 3.2          Xam-xamu jëmale ak xarala 3.2.1      Mën a dugg

Concepts scientifiques FR-WO / Mathématiques Inspirés de l'oeuvre de Cheikh Anta Diop

Concepts scientifiques FR-WO / Mathématiques Inspirés de l'oeuvre de Cheikh Anta Diop   TRIANGLE    ÑATKOÑ . angle koñ b-, angal b-, puxtel . angle adjacent puxtel bokkwet . angle aigu puxtel xat . angle complémentaire motlente, mëtlente, matlente . angle droit puxtel jub . angle obtus puxtel laññ . angle supplémentaire yokkalente . axe digel . bissectrice seddale puxtel . côté wet g-

•TAALIF TUDDAALE: "Acrostiche"

• TAALIF TUDDAALE: "Acrostiche" YAAY u Y oonu bànneex rekk la laay yéene u A y yow! ànd ak man ci naqar ak ci baneex u A t bu jot, bes bu dellusi duma fatte mukk sa cofeel u Y àll na la Yàlla dollil féex ak bànneex  

Le wolof

I.Présentation Générale du wolof Le terme “wolof” désigne à la fois le nom de langue wolof et celui de l’ethnie wolof, c’est-à-dire les gens qui sont natifs wolof. - wolof : nom de langue - Wolof : nom de l’ethnie

Jàngat Téere

Image
  Buur Tilleen bu   Séex Aliyu Ndaw   Tëralin wi Ndoortel li        I.              Jaar-jaaru Séex Aliyu Ndaw ak téere yu mu jott a mbind     II.              Yaatal jëmale ci téere bii di  Buur Tilleen  III.              Way-j ё mmali ak béréb yi ci téere bi 1.       Way-j ё mmali 2.       béréb yi IV.              T ё nkub t é ere bi      V.              Jàngale yi ak suñuy gis-gis ci téere bi 1.       Jàngale yi 2.       Suñuy gis-gis ci téere bi Nj...